Lii dafay tekki leeral yi ci làkku angale ngirxeetu piste synthetik (PU) yiñ gëna xamak seeni jëfandikoo yu méngoo:
1. - PU bu mat
Melo jëmmal:
Ñu ngi ko defaree lëmm ci polyurethane (PU), muy joxe elastisite bu baax, mëna yàgg, te baña yàqu.
Surface bu nooy, dalal bu dëgër buy tere gliise wala mbëkk.
Li gëna baax ci:
Stade athletik profesioneel
barabu tàggat yaram bu kawe -
Daara yi wala barab yi soxla performance yu baax ak yàgg.
2. Piste buñ boole
Melo jëmmal:
Granule elastik yu melni couche de base ak couche PU ci kaw.
Dafay ekilibre elastisite bu baax ak guddu fan ci njëg bu gëna néew - piste PU yu mat.
Li gëna baax ci:
Terrain sport yu mag ak yu digg yi ci daara yi
Barabu tàggat yaram
Liggéeyukaay yu soxla performance bu baax waaye am budget bu yam.
3. Piste hybrid
Melo jëmmal:
PU couche de base ci kaw ak granule EPDM.
Performance bu dëgër ak diiru tabax bu gëna gàtt.
Li gëna baax ci:
Terrain fowukaay yu daara yi
Barabi tàggat yaram yu askan wi
Piste de fitness.
4. Piste permeable
Melo jëmmal:
Couche de base ñu defaree ko granule kawsu bu ñuul ak surface PU.
Dafay noyyi, ndox-mën na dugg, du am fu sori, te gëna yomb ci njëg.-.
Li gëna baax ci:
Terrain fowukaay yu daara yi
Terrain sport yu askan wi
Yooni tàggat yaram wala yooni daw.
5. Piste Roll buñ defaree
Melo jëmmal:
Usine-defar nañu ay rulo kawsu yuñ samp ci-site bi.
Dafay dalal, gaaw ci samp gi, ak macceer yu baax ci environmaa bi.
Li gëna baax ci:
Barabu sport yi ci biir kër
Gym wala salle fitness
Fasilite yu fësal dayo bu kawe ak xaritoo gi am ci environmaa bi.
6. Surfaasu EPDM (Piste bu amul - buñ miin)
Melo jëmmal:
surface buñ defaree granule EPDM; elastisite bu baax ak tànneef ci melo yu bari.
Dafa gëna baax ci jëfandikoo ngir bégal xol, te moo gëna xéewale ci piste yiñ gëna xam.
Li gëna baax ci:
Jardin de enfants wala terrain de fo
Yooni jogging wala doxantu ci askan wi
Barabu fitness ci park publik.

